Dabah Songtext

Ismaël Lô

von Dabah

Dabah Songtext
Bindef yi gnom yeuk nagne ko
Diawoudji mingnou done misal
mane mamo mame demna
Ligua ligyey manboy bayilgnou
Gnioung siy diare
Dougnouko wathieu khana gnou fekidjilaa
Dabah Malick
Mame soumala massana khol
Sama khol day toy ndakh banekh
Rawatina soumay degloo mame say santane
Ndakh koula topeu dou dioum dou rerre
Dou dioum dou reree
Mame mboye yagnou tete si tariha cheick ahmed tijani
Mame koula topeu dou dioum dou rerre dou dioum dou rerre
Mame mboye yagnou tete si tariha cheikh ahmed tijani
Tahira yi yeuk nagne ko
Diawoudji mingnou done misal
Mame mamo mame demna
Lingnou tahanal mame mboy bayilgnou
Gnioug siy diare dougnouko wathieu khana fekidjilaa
Dabah Malick
Ndakh koula topeu dou dioum dou rerre
http://www.coveralia.com/letras/dabah-ismael-lo.php
Dou dioum dou rerre
Mame mboye yagnou tete si tariha cheick ahmed tijani
Mame koula topeu dou dioum dou rerre dou dioum dou rerre
Mame mboye yagnou tete si tariha cheikh ahmed tijani
Manoumala bagna dioy mame mboye
Waye faw mia dioye mani mlame da ngua bakhon lol
Da ngua deudouwon mame mboye adouna
Deuguo l'Islam te sakh di delo dioukeul yala sougnou borom bi
Woh oooh
Woh oooh kharit
Woh oooh serigne
Mame mboye doumala dioy mangui deukeu dila gnanal
Who oooh kharit mame mboye wetal nguagno
Who oooh serigne mame mboye wetal nguagno
Mame mboye dioyoumala
Mame mboye wetal nguagnou
Kharito wetal nguagnou
Te khamna barinasiy morom
Mame mboye dioyouma mame mboye dioyoumaala

(Thanks to Katerina Orlinova for these lyrics)